Li yëpp bidah rek. Demm na ñu ba di def bidah ci bidah. Réral na ñu nitt ñi. Nax léén nangu séén xaliss. Li ban jëriñ la am. Ba ñu dalé di magal cantt ziaar lan mo défaru ci jikko talibé. Lan mo défaru ci dëkk bi la lan mo yooku ci mim rêw. Dara. Kénn manul wax kañ la ñuy magal Seydina Babacar. Kañ la ñuy magal xaré badr magal bi Muhammad jëllé xërën yi nekkon ci biir Kaaba bi. Magal du Islam té du si massa bokk. Lu wéésu Makkah Madinah Al Aqsa Islam amatul dëkk bu tedd. Touba ak kër massar ño yam ci fann yëpp tilim bari nitt jaxaso.
Bof, tu ne propose pas mieux. Touba AU MOINS c'est CHEZ NOUS.... Ibaadous yi, ils sont rigolos avec leurs "bidah", "shirk"... Ils obligent à presque défendre lou presque indéfendable, c'est dire...
N'envoyez pas de message ayant un ton agressif
ou insultant.
N'envoyez pas de message inutile.
Pas de messages répétitifs, ou de hors sujéts.
Attaques
personnelles. Vous pouvez critiquer une
idée, mais pas d'attaques personnelles
SVP. Ceci inclut tout message à contenu
diffamatoire, vulgaire, violent, ne respectant
pas la vie privée, sexuel ou en violation
avec la loi. Ces messages seront supprimés. --
Pas de publicité. Ce forum
n'est pas un espace publicitaire gratuit.
Pas
de majuscules. Tout message inscrit entièrement
en majuscule sera supprimé.
3 Commentaires
Djibson
En Août, 2024 (17:32 PM)C'est rageant et désespérant.
Na nitt ñi yééwu took séén kër ak sééni ñjaboot.
Djibson
En Août, 2024 (18:32 PM)Participer à la Discussion